- Youssou N'Dour
- >
- History
- >
- Habib Faye
Testo Habib Faye
Testo Habib Faye
Adduna bi du dara ; te dara xaj u fi
Bi Lahii ku ko japp ; xamal ni japp u loo ci ; dara
Adduna bi du dara ; te dara xaj u fi
Bi Lahii ku ko japp ; xamal ni japp u loo ci ; dara
Man Youssou ñakk naa ; andandoo bu sincère
Adduna ; adduna daal ; nax ati na ñu
Adduna ; adduna da fay wor ee Habib Faye ; dem na nii
Waa ju baax ; guddée na waay
Habib yaru woon na ; and ak dignité
Fonŋk oon na liggéey ёm ; bëgg njaboot am bu ; baax
Doon oon jàmbaar
Man Youssou ñakk naa ; andandoo bu sincère
Adduna ; adduna daal ; nax ati na ñu
Adduna ; adduna da fay wor ee
Habib Faye ; dem na nii
Waa ju baax ; guddée ne waay
Adduna ; adduna …… Adduna ; adduna
Adduna ; adduna daal ; nax ati na ñu Adduna ; adduna da fay wor ee

- 7 Seconds (feat Neneh Cherry)
- Seven Second
- 7 Seconds
- Dem
- Birima
- Shaking The Tree
- Macoumba
- Serin Fallu
- Birima
- Mame Bamba
Altri testi di Youssou N'Dour
Lyrics powered by LyricFind
- Testi Ultimo
- Testi Pinguini Tattici Nucleari
- Testi Vasco Rossi
- Testi Jovanotti
- Testi Marco Mengoni
- Testi Lucio Battisti
- Testi Tiziano Ferro
- Testi Cesare Cremonini
- Testi Gazzelle
- Testi BLANCO